@hadji_mbaye16 Profile picture

.

@hadji_mbaye16

Construisez votre succès à partir de vos échecs. Le découragement et l’échec sont les étapes les plus sûres pour parvenir au succès.

Similar User
Sidybarasalihou photo

@SidyDia24564605

Noreyni 166i❤️🫀 photo

@usmandieng

m.a.m.e__m.o.r🇸🇳 photo

@MameMor__LO

Lumière 🎉🤍 photo

@la_lumr

Brahim Alioun Fall photo

@alioun_brahim

Moussa Yade photo

@myade09

Mame Thierno Niang 🇸🇳 photo

@DamalDaru

JOYBOY photo

@Joeboy142561631

MisterTechnology 🧬 photo

@serignemd

tapha_kasse_Louga la deuk photo

@taphakasse221

Ahma photo

@Abdoudi32866527

Ousmane Noreyni photo

@Othman_Noreyni

عَبْدُ آلْفَتَّاح photo

@abdoufata_ka

Bayefall Ndiguel 92 photo

@BayefallNdigue5

bamba✨ photo

@khadimNiass12

Pinned

Na ngeen ma seedeel suma faatoo ni ku bëggoon Sëriñ Tuubaa laa. Gannaaw lii bu ci ken teg leneen.


Leeg-leeg nga dund jafe-jafe bob la ngay bëgg mooy àdduna jaare fa tukki, doonte ñépp seen yoon nekku ci.


Pour une vie où chacun finira par mourir, tôt ou tard, ça ne sert vraiment à rien de nuire aux autres.


Aada ak topandoo d moo sonal ñu bari, waaye Islam li muy laaj ci sëy nga xam ni mooy dote bi mënul ñakk matul 30mil, fii ci Tuubaa 26mil.


Jotaay yiy am ci télés yi, sites yi, lu ci ëpp day manquer xam-xam ak objectivité, te ñaaar yooyu débat bumu amul njariñ la du bari.


« La force, toute la force, se trouve dans le fait de placer sa confiance en Allah. »


"Sama Ruu ak seen gos genn la : dangeen di feeñ ci man, may feeñ ci yéen, ku nekk ci nun làq moroomam ci boppam."


Politicien yi gëmuñu dara sen intrai bopp rekk moo leen ñor réew mi yittee lu leen.


Madrilene yi mënatu ñu siggi xool kenn.


Jomaay mi ngi seetaan lu grave.

Beneen bi mooy dama léen di yëgal ni maa léen gën a bëgg Sëriñ Tuuba😊



Yë ! Jigéen ju wowle kay musiba la.

Góor gu bëgg baat ak jigéen ju woowle lu ci tane ngeen yaakaar?



Senegalais bëgg na ñu réew mi soppiku lool waaye bëggu ñu soppiku ci séen doxaliin.


Ku bëgg ci mayi Yàlla yi, day bàyyi moy Yàlla yi, kuy moy ay jay lay am waaye du am i may, te ay jay ay duma rekk a cay topp !


Sëriñ Tuubaa kenn la !


Et c'est parti.....


La famille n'est pas une question de sang c'est la question de qui te tient la main le jour où tu en as le plus besoin.


Télé travail moom xam naa ko, waaye télé campagne ci Maki rekk laa ko gis, ñi ànd ak moom vraiment amuñu fulla.


Loading...

Something went wrong.


Something went wrong.