Sidybarasalihou
@SidyDia24564605alhamdoulilah Dieuredieufè 𝙨𝙚𝙧𝙞𝙜𝙣𝙚 touba djarama mame Chéikh îbrähîmä fall lamp 🏁❤️🫶
Similar User
@SalihuDieng
@Yuusufa_Faal
@mawahibu_16
@MameChe04050721
@GnagnaWatt
@papesenisall
@moussak61084193
@AlBachirdieng
@Serigne24166812
Notre génération est bénie d'avoir un leader comme Ousmane Sonko Yal na ñépp fekkee bis bi muy neex✍🏾SBS🇸🇳#sonko💚🤍❤️✅
Bi moy bulletin bou bakh bi Votons PASTEF LES PATRIOTES Pour une large majorité ✍🏾SBS❤️💚🤍#SonkoSeul🗳️✅
Bunu déémé bassi kanam, jotayu mouride lumu néx🤍nex🤍nex🤍 - - bama Serigne bi di ligueylo rek mofay ndam✍🏾SBS☝🏾🙏🏾
"'Serigne touba nénà' sama khasida yi malèn bind✍🏾 wayé gni len diange🗣️ Ma lén di tanne ✍🏾SBS🫀❤️💯 #SERIGNETOUBA
BISMILAH ZIAR NA MBOKU YEUP DI SAKOU GÈN GNANA LAL MA DIEUM JÏ DI BROM 👇🏾@Toubatuhfatou GOUDU FAN AK WÈR SI BARKÈ XASSIDA YI 🤲🏾 DA AM BÈN AT BU DOLIKU SI ATAM MOY DJAMBAR LOLU SI LIGÈYOU GROUP BI DI (SBS)🥳🎂🙏🏾
J'aime comment vous partagez cette prière sur le Prophète et aussi comment vous l'utilisez. Ceux qui l'utilisent connaissent ses bienfaits et comment ça a changé leur vie positivement. Yal nanu ci Yalla saxal✍🏾SBS🕋💫 #mawlidunnabis
Damay dem #jazbu néko Ahmadouna Rahmatouna, Hamidouna, Nihmatouna, Mahmouduna, Farhatouna❤️🤩 Dem #Mawahibou néko Antal Karimu anal Xadimu dehrën udimu fiiKa Sanaa i🫀❤️ Dem #muxadimat néko Nabiyun, Rasoulun, Xairou Habdin wa sayidun xaliloun Habibun🫀😍 ✍🏾SBS💫#XASSIDA😍🕋🫀❤️💯
Seriñ Tuba nee naa: " Ndoxx (eau) Mii Niouy taadj ci finiouy Magalè goudik gamou ba Ku cii naane: Dana saafara bep tawat boum fek ci yaw,dana la moussal cii péxé sheytanè ,danala aar, danala may ak joublou ci sunu boroom " "JAZBU" #FOCUSGAMMU#✍🏾SBS🕋🫀❤️
« Ku jàng ci guddig Gàmmu (Alxuraan, Qasida, Barzan, Burdu, Salaatu Alaa Nabii...) tifli ko ci am ndox, képp ku ca naan di nga mucc ci pexem Saytaane, dina leeral sab xol, dundal ko, te dina la fegal ag texeedi ». Sëriñ Tuubaa - Jazbu✍🏾SBS🕋🤩 #mawlidunnabiﷺ
Fàggul alal ju la neex, dees na ko càmbar ellëg ! Solal lu la neex, cib perkaal rekk ngay mujj ! Yafalal saw yaram nu mu la neexee, sax yi rekk nga koy xontee🥹✍🏾SBS💔🪦
Sa mbinde daana waral, seytaane rotthi kou daw 🥰Yonene bou ted ba mougn as leuf,aras diaayou S mbaye diakhate✍🏾SBS📜☝🏾
Les mourides n'ont pas de problème.🥰 Le matin, ils boivent leur café, chantent leur khassaid. Le soir, ils boivent leur café, chantent leur khassaid. Tu aime le MARABOUT, ils t'aiment.🤩 Le MARABOUT t'aime, ils t'aiment"✍🏾SBS🤩☕️📜🫀💯
Les mourides n'ont pas de problème. Le matin, ils boivent leur café, chantent leur khassaid. Le soir, ils boivent leur café, chantent leur khassaid. Tu aime le MARABOUT, ils t'aiment. Le MARABOUT t'aime, ils t'aiment"✍🏾SBS🤩☕️📜😍
Messoul doyloo koudoul Y'Allah. Ken genouko beugg Yonenti bi SAW. Beug nagne ko ba noppi🫀💯✍🏾SBS🙏🏾
MÀGGAL Gudikk JUDUK YÓNNENT Bii Cii Sunna TA YALLA RÉK TAX DAY TAXA DÉM AL JANNA DAY TAX SAY XÉEWËL DÓLLI KU✍🏾SBS🕋🤲🏾🫀🙏🏾
✍🏾SBS💫Faaw rek nieep xamni Dieum dji yamalé wougn ko ak kou Yalla bind te kouko songou Yalla ngay beurel te ci torokh rek ngay moudj. Liko Boromam may ken manouko xadiamal ak xadj bo mana doon mbeuw rek « le chien aboie, la caravane passe.
Il était également connu pour sa noblesse d'âme, son extrême générosité, sa forte personnalité,son noble caractère, sa patience, sa volonté et son dynamisme❤️ ✍🏾SBS💫#Serignetouba
United States Trends
- 1. #DWTS 24,2 B posts
- 2. Cavs 46,9 B posts
- 3. Celtics 53,5 B posts
- 4. Tatum 30,9 B posts
- 5. Garland 66 B posts
- 6. #WWENXT 24,8 B posts
- 7. #RHOBH 8.560 posts
- 8. Kam Jones 1.188 posts
- 9. Marquette 4.240 posts
- 10. Linda McMahon 31,4 B posts
- 11. Keldon Johnson 2.414 posts
- 12. Chase U 5.180 posts
- 13. Ilona 5.704 posts
- 14. #mubb 1.071 posts
- 15. Purdue 5.210 posts
- 16. Dorit 4.036 posts
- 17. Charles Lee 1.012 posts
- 18. #LetEmKnow 7.515 posts
- 19. Jorge Sánchez 3.388 posts
- 20. Cenk 26,7 B posts
Who to follow
-
Mendiant¶gnorant
@SalihuDieng -
Youssoupha FALL
@Yuusufa_Faal -
talib seex murtada saaliw 💙🤍
@mawahibu_16 -
EDITION ASSADOUL KHADIM
@MameChe04050721 -
Soxnacii 💖🇸🇳📘🖊️🧕
@GnagnaWatt -
Pape Séni
@papesenisall -
Ndongo baye Karim
@moussak61084193 -
𝐁𝐚𝐜𝐡𝐢𝐫 𝐓𝐡𝐢𝐚𝐭 𝐌𝐮 𝐑𝐚𝐟𝐞𝐭🇨🇦🇸🇳
@AlBachirdieng -
Serigne Saliou Tall
@Serigne24166812
Something went wrong.
Something went wrong.