@kiriku_bi Profile picture

kiriku 👨‍🦲

@kiriku_bi

Joined October 2022
Similar User
prunelle 💋❤️ photo

@gueyendeyeawa27

kiriku 👨‍🦲 Reposted

Mousna dokhane domou militaire démfa Pa bi dima atayalo dieul arme yi di nettoyé ta nane ma "arme yi bissi gueneu ndaw sougne lako doré sa mbakyi lay diaxassé" 😭ataya bi niorna bama xéliko té talouma gaz bi ndégué sama fite bidone teufteufi tangor bobou moko nioral ndakh tiite😭


kiriku 👨‍🦲 Reposted

THREAD : Laabiire gi , sëriñ bi mo ko def ci bisu alxamiis ( jeudi ) ci weeru rajab Yeen ñi aju ci man , doonleen ñu gëm yàlla , diy jullit yuy topp yàlla tey rafetal. Jëme naa ci yeen laabiire gii , nanguleen ko te jàng ko njàng mu leer.

salioumbackefa1's tweet image. THREAD : Laabiire gi , sëriñ bi mo ko def ci bisu alxamiis ( jeudi )  ci weeru rajab 

Yeen ñi aju ci man , doonleen ñu gëm yàlla , diy jullit yuy topp yàlla tey rafetal. Jëme naa ci yeen laabiire gii , nanguleen ko te jàng ko njàng mu leer.

kiriku 👨‍🦲 Reposted

Njàngum xasiida aka naxari saytaane, moo waral dina jaar ci bunt yu bari ngir yàq, moo tax kuy jàng xasiida moo xam yékkati wallla duruus, dee ko sellal loo man, te xam ne yaa ngi ci jaamu Yàlla gu naqari saytaane, nanu moytu lépp luy niru fo, te xam ne liggéey bu boroom sonn la.


kiriku 👨‍🦲 Reposted

Ni tali bi di leere xaaju guddi, ba dem yomb lool, noonu la yoonu Yàlla mel ci waxtu woowu, boo ko dee dundal sab dox ci sa Boroom dina gaaw lool.


Xam nga lu gën a metti si àdduna nga rus nit bu amul xél 🥺


kiriku 👨‍🦲 Reposted

أستغفر الله. أستغفر الله العظيم. أستغفر الله العظيم وأتوب إليه. أستغفر الله العظيم الذي لا إله إلا هو الحي القيوم وأتوب إليه.


kiriku 👨‍🦲 Reposted

Niit ki leu feugeu soubatel boulko diépii…Sou néxoon Bour bi yay xeuy di feuguàté …


kiriku 👨‍🦲 Reposted

SËRIÑ TUUBAA nee na "QASIDA Yassaralii Muyassirul Hassiiri jàng ko ci ak guddi, mo gën wird ba sa ndigg di metti, wala wird ba say wee dàmmu!"

be_mouride's tweet image. SËRIÑ TUUBAA nee na
"QASIDA Yassaralii Muyassirul Hassiiri jàng ko ci ak guddi, mo gën wird ba sa ndigg di metti, wala wird ba say wee dàmmu!"

Imaginer nga wathi job nieuw fekk Madame mou teudd ci lale bi relax, nga nieuw ci weitam léebal ko lééb bou con rekk dégg benn gayine di reetaan thi soufou lale bi 😭😭😭😭😭 @221Troll


kiriku 👨‍🦲 Reposted

Pochette + Power Bank 100% Authentique Disponible à partir de 12pro Foula nêkh ngay chargé Protège + Power Bank Prix: 🏷️ 22,000f cfa Livraison gratuit Dakar 🚨 iskapple le spécialiste de la marque Apple ici au Sénégal 🇸🇳  +221 78 117 05 16 /+221 78 597 01 01


kiriku 👨‍🦲 Reposted

ibliss limiyy amm fitt amm fitt Baa firhawna né mayy yalla daa daww😂


kiriku 👨‍🦲 Reposted

(DOGGANTAL CI FARATAY JULLI) Faratay julli fukk ak juroom la, ci li faqiih bii di Hawfii wax. Ñooy yii: 1 yeene 2 kàbbarub armal ba 3 taxaw ngir kàbbar ko 4 jàng faatiya 5 taxaw ngir jàng ko 6 rukoo 7 siggi ca rukoo ba 8 sujood 9 siggi ca sujood ba 1/2


kiriku 👨‍🦲 Reposted

Je vends ce matériel, pour vos vidéos smartphone. (Micro, trépied, lumière...) 💰 16 000 F CFA #Rtapprecies

Docteur_Emotion's tweet image. Je vends ce matériel, pour vos vidéos smartphone. 
(Micro, trépied, lumière...)

💰 16 000 F CFA

#Rtapprecies
Docteur_Emotion's tweet image. Je vends ce matériel, pour vos vidéos smartphone. 
(Micro, trépied, lumière...)

💰 16 000 F CFA

#Rtapprecies

kiriku 👨‍🦲 Reposted

Original AF1 disponible✅ Size:37 à 45 🏷12.000fr Contact:771363153


kiriku 👨‍🦲 Reposted

«…Ku Yàlla gindi mu jub. Ku mu bàyyi ci ag réer, du am kilifa gu koy jubbanti » S18V17


kiriku 👨‍🦲 Reposted

" J'ai vu le prophete ﷺ manger du poulet. " Hadis rapporté par abu muusa al ashari Sahih buxaari 5517


Kii en mak bou niakk foulla la. 😏😂

kiriku_bi's tweet image. Kii en mak bou niakk foulla la. 😏😂

Coumba dafa diongué ba yakhou , béne jour dieukeur dji nékk ci douche bi di déffarou rk mou gneuw feug porte bi né nidiaay bo paré poupp nga wakhma ma labb la rek Dieukeur dji mér nékko Guiss nga man Coumba sa diongué you tothie sarap ndém yi rk la bagne 😂😂. @221Troll


United States Trends
Loading...

Something went wrong.


Something went wrong.