@Sambaacisse Profile picture

Lazanba⭐️🇸🇳

@Sambaacisse

👻lazanba_c || Analyste des politiques publiques en devenir || UCAD || ISM || Sanar’26 || Racines de l’espoir || Xidmatul Xadiim || Mafaatihul Bichri ||

Joined April 2013
Similar User
Drouss photo

@droussLib

MasterDesign photo

@MasterDesiign

LunOo photo

@Alioune_G

Abdu 🌚🇸🇳 photo

@abdu_faal

Busó 🤍 photo

@soxnajaara_m

La Jolie Dame🌹 photo

@OG_Diara

H¤t S大ucㅌ🏆🥳🇸🇳 © ami de Ridwan AS photo

@hotsaucetweet1

Allure_by_Aly photo

@AllureByAly

Ndeye Coumba kane photo

@Coumbak1

It’s Sho time photo

@ShoMadjozi

Viitamin🇸🇳 photo

@pendatallb

OZEBA photo

@safietouu

Bomo Raby 🇸🇳 photo

@Bomoraby

𝓐𝓫𝓭𝓸𝓾 𝓚𝓪𝓻𝓲𝓶 𝓚𝓪𝓷𝓭𝓳𝓲🇸🇳✪ photo

@karimkandj

Roger S.T🇸🇳🦍 photo

@Roger_thiam

Lazanba⭐️🇸🇳 Reposted

Un waxtan était inscrit à l'ordre du jour mais les parents ont décidé de sceller l'union. Je quitte officiellement le syndicat des célibataires pour la très grande institution du mariage. Alhamdoulilah🤲🏾

Tweet Image 1

Lazanba⭐️🇸🇳 Reposted

Lèpp luma xalaat ni suma ko dèfèe xassida yi dina rafèt , dama koy def ❤️ Sumay bind xassida damay bayyi xel kinga xam ay bëtam neexul, ki nga xam ni fèr ijji gi dëgarul, ak ki nga xam ni moom mbin mu rafèt daf koy sawar loo . Manuscrit: #baayxalima

Tweet Image 1
Tweet Image 2
Tweet Image 3
Tweet Image 4

Lazanba⭐️🇸🇳 Reposted

Do bakh ba rombou ko , Do bonne itam bamu bedd leu , na niouy Jouli ak di seulmeul ci sunu sangue bou tedd bi Mustafa ﷺ💚

Tweet Image 1

Lazanba⭐️🇸🇳 Reposted

Kepp kuy ut dara tay sàkku ndimbal ug sunu Boroom ci loolu, na saxoo sikar baat yii ci limub 100 baa 1000 baa 5000i yoon ci bis bu ne. Bu ko mënee it 15 000i yoon ci bis. Jàppandal 100% dee ngi ci biir baat yii

Tweet Image 1

Lazanba⭐️🇸🇳 Reposted

Sëriñ Muntaxaa dey, daa baax rek mootax mu jëfandikoo baatub "ndigël" Waayè lii "ndimbal" la ci ñun ndax matlabul Fawseyni kaaràngè gi ci nekk ku xëy jàng ko mu aar la ba dara dula manal dara Tèerè bi maako móol neex naa jángèe lool itam. #baayxalima


🧠🧠🧠🧠🧠 « Lentement mais Surement ; Wërsëk do ko forcer, ndank rek ; Na licite rek ; lo aam nala doy ; na nga ko doy lo te japp ci Ya Allah, Ya Allah yakamti wul kone nit waro yakamti» Cey 😭


Lazanba⭐️🇸🇳 Reposted

Neexaayu wér ku tawat moo koy xam Neexaayu kàttan ku néew doole moo koy xam Neexaayu ndaw ku doon mag moo koy xam Neexaayu dund ku faatu moo koy xam.


Lazanba⭐️🇸🇳 Reposted

I dropped a tear watching this. Notion de xéewal nekkul ci yii nuy gis, jàmm i xol la, am connexion ag Alxuraan m ko ag sa Boroom, su booba lu ñëw nga dékku te boo dee wee gis lula neex

📍Bachir demaatoon tay jii seeti Serigne Assane, @khalifa_a_sarr DG de la @sonagedsa gis vidéo démb bi rafetlu ko lool am yéené recruté ko, defal ko contrat ngir mu liggéey foofu; muy mbégté mu rëy ci nun ñépp. Képp kuko bëgg a yóonée àddiya nak man nga ko jaarale ci 77 800 49…



Lazanba⭐️🇸🇳 Reposted

Niane bi niane bou am sollo la dalley mousseul si seytané, mousseul la çi beut, mousseul la si wakh. Dellen koy diang souba ak ngone.

Tweet Image 1

Lazanba⭐️🇸🇳 Reposted

« Sois patient ! La fin heureuse sera aux pieux. » Hûd - Verset 49.

Tweet Image 1

Lazanba⭐️🇸🇳 Reposted

Je me sens honoré de diriger PASTEF et quelque fois je me demande ce que j’ai fait pour que Dieu ns donne des militants de cette qualité et de cet engagement. Je le dis sans nombrilisme particulier, mais je crois que ns sommes en passe de devenir le 1er parti politique du Sénégal


Lazanba⭐️🇸🇳 Reposted

En 2024, nous rattrapperons le raté de 2019. Mais nous devons nous y mettre dès les prochaines échéances électorales (locales comme legislatives) #restonsmobilisés


Lazanba⭐️🇸🇳 Reposted

On peut dire que Ousmane Sonko est le plus grand homme politique de l’histoire du Sénégal? Ce qu’il a réalisé en 10 ans ( 2014-2024) avec son parti est quand même marquant.


Lazanba⭐️🇸🇳 Reposted

64 ans d'indépendance gnogui soga ame Président bou fanane keur Papam 🤣

Le Président Bassirou Diomaye Faye est arrivé à Ndiaganiao pour accomplir son devoir civique demain🇸🇳



Lazanba⭐️🇸🇳 Reposted

Je suis désolé de le dire mais Abdou Rahmane n’a pas les militants qu’il mérite Il est tout le contraire des gens que je vois le supporter Poli, courtois, sympathique mais surtout très compétent


Lazanba⭐️🇸🇳 Reposted

🚨📌C'est clair et nette : c'est le Gouvernement du Sénégal qui a decide de ne pas reconduire les accords de pêche avec l'UE👍🏻


Lazanba⭐️🇸🇳 Reposted

Quand l’homme se tourne vers la lumière, l’obscurité perd son pouvoir. #AssembléeBiÑuBëgg

Tweet Image 1

Baay Jibril Top d delucina🥹

Qudaamul Quraan ndekete noonu la jàmbaree ci Xasida yi🤩



Lazanba⭐️🇸🇳 Reposted

Qudaamul Quraan ndekete noonu la jàmbaree ci Xasida yi🤩


Lazanba⭐️🇸🇳 Reposted

Pourquoi alors la société civile se prétend représenter le peuple ? Alors que personne n’ a voter pour eux

Ne pas confondre le peuple et les militants d'un parti qui s'autoproclame le peuple. Le concept de peuple est plus complexe.



Loading...

Something went wrong.


Something went wrong.