@BayePost Profile picture

Baye Fall Xasim

@BayePost

Gaïndé Mame Modou Moustapha Fall 🇸🇳

Joined October 2019
Similar User
Abuubakrin As Siddiiq photo

@mbaye126

Rama_jaaw photo

@une_hamzate

Hamza benn jaam🇵🇸🇵🇸🇵🇸 photo

@HamzatouNdiaye

ousseynou photo

@biyayeousseynou

Serigne Saliou Tall photo

@Serigne24166812

Xol Xalam ♥️

Tweet Image 1
Tweet Image 2

Limann baalaxa ♥️

Tweet Image 1

Baa faawou nk !!!

Tweet Image 1

Murid dëgg bul mer te bul jàpp mer Mer ak jàpp mer day alak ab murid Mereel say ayib, gërëm sab sëriñ Te daw nemmatam nag ba am say murid

Tweet Image 1

Saa Mame Cheikh nénah : Doom faa diaara raxas ndox aggoufa


Serigne Cheikh Fall ♥️

Tweet Image 1

Naaféq yaa ngi daw di raam ngir jamono Jàngal: "Isaa laquul lasiina aamanuu" Bu ñu demee Tuubaa nirook waa Tuubaa Te buñ demee ca réew ma mel niy koobaa Waaye Sëriñ Tuubaa maneefu koo nax Maneefu koo njublaŋ ku tawlu day tex


Mame Ceix Ibra nénah Doom daama naakaré xaam lool té néxa wéedi


Seugn Ceix Bayou Goor nénah : << civilisation mooy xam liila waar gua nékk thji>>.

Tweet Image 1

Baye Fall Xasim Reposted

Serigne Fallou Fall Ndam Al Janah, Serigne Cheikh Fall Astou Ndiaye, Serigne Moustapha Fall Khalifa Ndiarem ak Serigne Cheikh Penda

Tweet Image 1

Baye Gaïndé Modou Moustapha #Senegal

Tweet Image 1

Baye Fall Xasim Reposted

Dangay beugu dieukeur mouride nak mais niom dessé nagn meunn topato soxna nonou déh😭 lougn amm dioxko seugn bi.


Baye Fall Xasim Reposted

🥰🥰🥰🥰🥰 A suivre sur MbaworFallTV Facebook/YouTube Ziar general Ëhlu Zikroulah 2022


Baye Fall Xasim Reposted

Doom moroom amoul Moroomanté amoul Koussi né SA-AY jeuff mooy sa moroom Parole Mame Lamp Fall.

Tweet Image 1

United States Trends
Loading...

Something went wrong.


Something went wrong.